mercredi 16 août 2017

Wolof words for Wild animals in Senegal



Wolof words for Wild animals in Senegal
These are animals which you might come across in the north of Senegal.
janax ji
Description : mouse picture
mouse or rat / souris ou rat
lëg gi
Description : hare picture
hare / lièvre
golo gi
Description : monkey picture
monkey / singe
golo bu nuul bi
Description : green monkey
green monkey / singe verte
yoolaan bi
Description : genet picture
genet / genette
Genetta thierryi / Genetta tigrina
siiru si
Description : wild cat picture
wild cat / chat sauvage
Felis libyca
wel wi (njappati)
Description : sand fox picture
sand fox / renard pâle
Vulpes pallida
till gi
Description : jackal picture
jackal / chacal
Canis aurens
suññéel bi
Description : hedgehog picture
hedgehog / hérisson
(Atelerix albiventris)
kund bi
Description : badger picture
honey badger / ratel
Mellivora capensis
jab gi / wéxéñ wi
Description : skunk picture
african skunk / zorille commun
Ictonyx striatus
stripped weasel / zorille de libye
Poecilictis libyca
bukki bi
Description : hyena picture
hyena / hyène
Crocuta crocuta
xojox mi
Gambian sun squirrel
/ écureuil de Gambie
(Heliosciurus gambianus)
jaar ji / jaxar ji
Description : squirrel picture
stripped ground squirrel
/ écureuil fouisseur
(Xerus erythropus)
mbaam-àll mi
Description : warthog picture
warthog / phacochère
sikkóor bi
Description : mongroose picture
mongoose / mangouste
Ichneumia albicauda
Herpestus paludinosus
Mungos mungo
Herpestes sanguineus
Herpestes ichneumon

léebéer bi
Description : hippo picture
hippopotamus / hippopotame
(Hippopotamus amphibius)
leraw bi
Description : dugong picture
dugong / lamantin
Trichechus senegalensis
mbott mi
Description : toad picture
toad / crapaud
Other animals of interest.
kéwél gi
Description : gazelle picture
gazelle / gazelle
(Gazella rufifrons, Gazelle dorcas)
kooba gi
Description : antelope picture
roan antelope
/ antilope chevaline
(Hippotragus equinus)
mbill mi
Description : reedbuck picture
common reedbuck
/ cobe des roseaux
(Redunca redunca)
gaynde gi
Description : lion  picture
lion / lion
Panthera leo
njamala mi
Description : giraffe picture
giraffe / girafe
(Giraffa camelopardalis)
dàngin gi
Description : gorilla picture
gorilla / gorille
saaw mi
Description : porcupine picture
porcupine / porc-épic
Hystrix cristata
njomboor ji
Description : rabbit picture
rabbit / lapin

segg mi
Description : leopard picture
leopard / panthère, léopard
(Panthera pardus)
tene mi
Description : cheetah picture
cheetah / guépard
(Acinonyx jubatus)
wànga-lànga wi
Description : rhinoceros
rhinoceros / rhinocéros
(Diceros bicornis)
ñey wi (ñay wi)
Description : elephant picture
elephant / éléphant
(Lexodonta africana)
kaña gi
Description : rat picture
black or ship rat, / gros rat
(Rattus norvegicus, Rattus rattus)
mbeexeer
Description : frog picture
frog / grenouille
fasu àll wi
Description : zebra pciture
zebra / zèbre
nagu àll wi
Description : buffalo picture
african buffalo /
buffle d'Afrique
Syncerus caffer
kax
Description : civet picture
african civet /
civette d'Afrique
(Viverra civetta)
kancóoli gi
Description : http://www.wolofresources.org/language/images/giant_rat.jpg
giant Gambian rat
/ rat géant de Gambie
(Cricetomys gambianus)
njaxat bi
Description : http://www.wolofresources.org/language/images/aardvark.jpg
aardvark / oryctérope
(Orycteropus afer)
saafaandu gi
Description : http://www.wolofresources.org/language/images/wildog.jpg
cape hunting dog
/ chien sauvage dÁfrique
(Lycaon pictus)
Email corrections and comments to ForTheWolof
HOME PAGE http://www.wolofresources.org/index.htm
Last modified on Wednesday 6 January 116
This document was printed from http://www.wolofresources.org/language/vocab/wild_animals_print.htm

mardi 6 mai 2008

Alarba 1 Rakkaatigamu 1429

Talaata 1 Rakkaatigamu 1429: Lutax nuy réetaan ku juum ci kalaamay tubaab, di ci rus, ta su de ci wolof kenn du wax dara? Yaakaar naa ci sunu lakka ci la nu wara gene farlu!

dimanche 27 avril 2008

waqtu julli

ajuma 18 rakkigamu 1429
suba 05w49 tisbaar 14w15 takusaan 17w00 timis 19w34 géewe 20w34

samedi 19 avril 2008

Sopi waxin

Leegi jafena di wax te bolewoo ci baatu tubaab! Lii nak day ray sunu lakk! Konnak nanu raxas yenn baat yi! Misaal mi mooy sempi " par exemple" ta wax "misaal', xalab "vendredi" ta wax "ajuma"!

vendredi 18 avril 2008

bataaxal

Bismillaahi! Nanu tambali waxtaan tuuti, xallataat, seetaat sunu bop! Fonkaat sunu kalaama! Te jeema di binde! Ndax mookoy suuxat, melne ndox ak garab!

jeudi 17 avril 2008

Yegle

Bismillahi nu tambali jeema bind sunu kallaama! Ndax kenne dunu ko defal kudul nun!