mardi 6 mai 2008

Alarba 1 Rakkaatigamu 1429

Talaata 1 Rakkaatigamu 1429: Lutax nuy réetaan ku juum ci kalaamay tubaab, di ci rus, ta su de ci wolof kenn du wax dara? Yaakaar naa ci sunu lakka ci la nu wara gene farlu!