Wolof
words for Wild animals in Senegal
These are
animals which you might come across in the north of Senegal.
janax ji
![]()
mouse or rat / souris ou rat
|
lëg gi
![]() hare / lièvre |
golo gi
![]()
monkey / singe
|
golo bu nuul bi
![]() green monkey / singe verte |
yoolaan bi
![]() genet / genette Genetta thierryi / Genetta tigrina |
siiru si
![]()
wild cat / chat sauvage
Felis libyca |
wel wi (njappati)
![]()
sand fox / renard pâle
Vulpes pallida |
till gi
![]()
jackal / chacal
Canis aurens |
suññéel bi
![]()
hedgehog / hérisson
(Atelerix albiventris) |
kund bi
![]()
honey badger / ratel
Mellivora capensis |
jab gi / wéxéñ wi
![]()
african skunk / zorille
commun
Ictonyx striatus stripped weasel / zorille de libye Poecilictis libyca |
bukki bi
![]()
hyena / hyène
Crocuta crocuta |
xojox mi
Gambian sun squirrel
/ écureuil de Gambie (Heliosciurus gambianus) |
jaar ji / jaxar ji
![]()
stripped ground squirrel
/ écureuil fouisseur (Xerus erythropus) |
mbaam-àll mi
![]()
warthog / phacochère
|
sikkóor bi
![]()
mongoose / mangouste
Ichneumia albicauda Herpestus paludinosus Mungos mungo Herpestes sanguineus Herpestes ichneumon |
léebéer bi
![]()
hippopotamus / hippopotame
(Hippopotamus amphibius) |
leraw bi
![]()
dugong / lamantin
Trichechus senegalensis |
mbott mi
![]()
toad / crapaud
|
Other animals of interest.
kéwél gi
![]()
gazelle / gazelle
(Gazella rufifrons, Gazelle dorcas) |
kooba gi
![]()
roan antelope
/ antilope chevaline (Hippotragus equinus) |
mbill mi
![]() common reedbuck / cobe des roseaux (Redunca redunca) |
gaynde gi
![]()
lion / lion
Panthera leo |
njamala mi
![]()
giraffe / girafe
(Giraffa camelopardalis) |
dàngin gi
![]()
gorilla / gorille
|
saaw mi
![]()
porcupine / porc-épic
Hystrix cristata |
njomboor ji
![]()
rabbit / lapin
|
segg mi
![]()
leopard / panthère, léopard
(Panthera pardus) |
tene mi
![]()
cheetah / guépard
(Acinonyx jubatus) |
wànga-lànga wi
![]()
rhinoceros / rhinocéros
(Diceros bicornis) |
ñey wi (ñay wi)
![]()
elephant / éléphant
(Lexodonta africana) |
kaña gi
![]()
black or ship rat, / gros
rat
(Rattus norvegicus, Rattus rattus) |
mbeexeer
![]()
frog / grenouille
|
fasu àll wi
![]()
zebra / zèbre
|
nagu àll wi
![]()
african buffalo /
buffle d'Afrique Syncerus caffer |
kax
![]()
african civet /
civette d'Afrique (Viverra civetta) |
kancóoli gi
![]() giant Gambian rat / rat géant de Gambie (Cricetomys gambianus) |
njaxat bi
![]() aardvark / oryctérope (Orycteropus afer) |
saafaandu gi
![]() cape hunting dog / chien sauvage dÁfrique (Lycaon pictus) |
Email corrections and comments
to ForTheWolof
HOME PAGE http://www.wolofresources.org/index.htm
Last modified on Wednesday 6 January 116
This document was printed from http://www.wolofresources.org/language/vocab/wild_animals_print.htm
HOME PAGE http://www.wolofresources.org/index.htm
Last modified on Wednesday 6 January 116
This document was printed from http://www.wolofresources.org/language/vocab/wild_animals_print.htm