mercredi 29 mai 2019

mardi 28 mai 2019

sawolof



deg luleen ko fii



Kaajar : Sëriñ Fàllu Siise
Fàllu Siise mi ngi juddoo mure ci biir saalum , bokk ci kolobaan , kolobaan bokk ci kaolax ci atum 1955 ci fukki fan ak ñett ci maamum koor
Lu waral sëtu maam : sëtu maam bokkul ci sama tur jenn waay moo ma ko tuddee, ndax dafa gis sama taxawaay ci làkku wolof, te su maam dellusiwoon  du ma jéppi

toubab bi deggna wolof itam

jeudi 23 mai 2019

jeudi 16 mai 2019

C

Caabi : n. clé

Caaf : n. arachide grillée
Caaxaan : n. blague, v. blaguer
Caaya : n. pantalon bouffant
Cammooñ: n. et adj. gauche
Ceeb : n. riz
Ceebu jën : n. riz au poisson
Cere : n. couscous
Concu : n. coude
Coono : n. fatigue
Coow : n. bruit
Cosaan : n. origine
Curaay : n. encens


mardi 14 mai 2019

B




Baal : v. excuser
Baaraam : n. doigt
Baat : n. voix
Baat : n. cou
Baax : adj. gentil, bon
Baay : n. père
Bakkan : n. nez
Balaa : loc. conj. avant que
Ban : pron. rel. et interrog. lequel, laquelle, lesquels, lesquelles
Ban : n. argile
Banneex : n. plaisir, bonheur
Bant : n. bois
Bañ : v. refuser
Bare : v. être nombreux
Bataaxal : n. lettre, message
Batey : loc. conj. jusqu'à présent
Baxa : adj. n. bleu
Bayyi : v. abandonner
Bees : adj. neuf
Beg : être gai, content
Beneen : adj. pron. autre
Benn : n. un
Berep : n. lieu
Bes : n. jour
Bëgg : v. vouloir
Bëñ : n. dent
Bët : n. oeil
Biig : la nuit dernière
Biir : n. ventre
Biir : n. et adj. intérieur
Bind : n. écrire
Bisaab : n. oseille
Biti : n. dehors
Bokk : v. partager
Bon : être mauvais
Boole : v. mélanger
Bopp : n. tête
Bukki : n. hyène
Bunt : n. porte