mercredi 23 décembre 2020
wolofconnection.org yaram wi body - le corps Wolof English français der bi skin la peau ñàq sweat la sueur kawar gi, hair les cheveux bopp bi head la tête jë bi forehead le front kaaŋ mi skull le crâne yóor gi brain le cerveau kanam gi face le visage bët bi / gët yi eye(s) l'œil / les yeux rongooñ tear la larme nopp bi ear l'oreille bakkan bi nose le nez paxu-bakkan nostril la narine faas yi sideburns les favoris lex yi cheek la joue tuñ wi lip la lèvre gémmiñ gi mouth la bouche làmmiñ wi tongue la langue lor saliva la salive bëñ bi tooth la dent ciiñ mi gingiva, gums la gencive ŋaam wi jaw la mâchoire sikkim bi chin beard le menton la barbe doq nape of the neck la nuque baat bi neck le cou bóli gi , put wi throat la gorge dënn bi chest la poitrine ween wi breast les seins cus wi nipple le mamelon xol bi heart le cœur siddit artery l'artère waruwaayu deret vein la veine deret ji blood le sang xëtër wi lung le poumon jumbax, jumbux navel le nombril biir bi belly le ventre, (l'abdomen) bàq gi stomach l'estomac butit bi intestine l'intestin res wi liver le foie gàddaam gi spleen la rate ndigg li hip kidney la hanche le rein saw bi l'urine siddit, sëddit nerve le nerf suux wi, (sóox) le muscle yax bi bone l'os yaxi neen yi skeleton le squelette ginnaaw gi back le dos faar gi rib la côte mbagg mi shoulder l'épaule conco bi elbow le coude loxo yi arm hand le bras la main ténq, tiwu-jara, tikku-jara wrist le poignet këmëx bi fist le poing baaraam bi finger le doigt baaraamu jaaru bi ring finger l'annulaire (baaraamu-)déy bi thumb le pouce we wi fingernail, nail l'ongle taat wi buttocks les fesses pooj bi , (lupp) thigh la cuisse (w)óóm wi knee le genou yul bi calf le mollet wëq wi ankle la cheville téstën mi heel le talon tànk bi , (yeel) leg foot la jambe le pied baaraamu-tànk bi toe le doigt de pied, l'orteil wér gi - health - la santé Wolof English français ambilaas bi l'ambulance fajukaay bi, loppitaan bi hospital l'hôpital fajkat bi, doktoor bi physician, medical doctor le médecin, "docteur" jabar bi witch doctor le guérisseur farmasi bi pharmacy, (drugstore) la pharmacie garab gi medication le médicament kawas bi condom le préservatif, la "capote" feebar bi jàngoro ji opp bi disease la maladie xurfaan si cold le rhume sibbiru si malaria le paludisme gaana gi leper la lèpre kuli ji la syphillis gumba gi blind man l'aveugle dof bi mad man le fou
Inscription à :
Publier les commentaires (Atom)
2 commentaires:
Merci beaucoup!
Ñóo ko bokk! Jērējēf!
Enregistrer un commentaire